Thione Seck : "Si ce n'était pas Waly, je ne parlerais pas de l'affaire Guin Thieusse"

igfmsn 112 996 subscribers

Retrouvez-nous sur http:www.igfm.sn

100 Comments

  • Ta place est en prison

    Reply
  • Bayiléne papa thione yéne lanla topé ngenko mboro dh

    Reply
  • Niakoul fayda sax mei Sénégal fok ngay woné sa bopp doul kate yé barri

    Reply
  • C un vrai rancunier

    Reply
  • Thione vraiment d'à ngaa ma bettt iow mak ngaa amna yenn yo xamni waroko deff lou nek yangui ciii hum Yenn wa Raam Daan Diaxal nguennma

    Reply
  • yow. thione. seck. do. noble. halliss. rek. mollo occupé.

    Reply
  • guin. thieuss. mollo. gueun. yow. thione. seck. Sénégal hamnalà do. darra

    Reply
  • 🤣🤣🤣🤣🤣OMG

    Reply
  • Bayi len wakh bi way

    Reply
  • Triste famille seck

    Reply
  • Thione doundal gni bayiléne gnouy wak waly di liguey

    Reply
  • Kouyy Wang deugg nekhna khamo.thione danouga.adouna dayyy diékh

    Reply
  • 20 Commentaires you ndieuk yi sén Affairs léroul

    Reply
  • Guin thieus en le suivant jc k c klk1 d honnete mais la c sa parole contre la sienne jaccuse personne mais ce Edmond c lui le tek katou deal vu k citoyen canada le epi la bataille se passe dans les medias si tout est averé key devant la justice normalement on saurai cki c passei. La ca parle ca traite la famille seck sans savoir jugeons pas

    Reply
  • Saway encore une fois dara lerroul, guine tieuss ay preuve you takhaw leu fi indi

    Reply
  • Guine thieusss a raison pere d'apres tes explication toi et ton fils vs avez tor arrêté la manupilation wsh

    Reply
  • Ligua wakh dara lérousiiii papa thione

    Reply
  • Thioune mi mo wakh degue Bayilen sokhore

    Reply
  • Thione j'adore ta musique mais wakhoo fii Dara on est pas des enfants !!!!!

    Reply
  • Famille sathie seck

    Reply
  • Doul reke Sathie bi

    Reply
  • Barki wonaine teubi thione mala beugu

    Reply
  • Dioubo deh khalissou diambour nguakoy ségniou

    Reply
  • Thione yay wakhata

    Reply
  • Légui le problème avec guinn teuss dal gambien bi nga KO djin. yak sa dom dal yéna gui nonou.

    Reply
  • Thione seck sén bay la un pe de respect il dit que la vérité

    Reply
  • Vraiment si c comça k ça s'est passé sincèrement y'a + r1 n'a à dire

    Reply
  • Prkw tjr des problème d'argent, parce-que Youssouf guén tékk beutt, Youssouf dousén morome

    Reply
  • Papa thione yalla naffi yague weur

    Reply
  • Mé bayyileine papa thione deuggueu rék la wakh boudoon daa am loumii neubbeu dou woo guinthieuss mou fékkei dnc Thione lou leir la beugueu té o6 guine thieusse bou diouboon dou laathie khaliss bi nakh ndayou mbilleu gui moy ki toureum nékkeu si papier yi

    Reply
  • Papa Thione la ou t a pas.raison c est celui que t as donné l argent car c est guin thiess le mediateur et c.est lui que tu connais

    Reply
  • Bou kéén bakaar le show biz est très salle difficil de savoir qui a raison ou ki a tor alors ne jugeons pas ni guin thieuss ni thione c est un business trés salle plus dangereux que la lutte

    Reply
  • Billahi Thione si degue rek kaye dokh mo takh ma beuguele degue pirrrrr

    Reply
  • En tt cas famille Seck amoleen ayy conseiller . Wally a droit de dire k papam la amal affaire parce k thione dey deff Lo khamni Wally douko yeuk

    Reply
  • Thione la femme idéale pour toi ça serait selbé ndom, gniémé guéne téseunté micro ak détail

    Reply
  • J avais que tu as bien agi pas d etat dame ds le busness

    Reply
  • Thon sek waxoul teugu

    Reply
  • No Thione mo nekh nena bou doon man mom damakoy sénio akka beugg xaliss

    Reply
  • Thiey guine teuss mi

    Reply
  • Papa sisi baah rek lan lay torompe

    Reply
  • Yaw nénga dangay sotlé guin thieuss pour sak année mou organisé wally canada té né nga amoulo len dara lou len lié té nga fay xalis bi bala niou lay wowat fofou

    Reply
  • Thione loutakh meuna doul bayil féne yi nguir yalla makk ngua ragualal yalla té ngua fay khaliss bi ay lék katou riba nguéne rék thim

    Reply
  • *thione seck* faylen xaliss guin thieuss yaw ya togn waxo fi dara lou ler yaw bakham yako signer rk Té concert bi amoul rembourser ko money bi Nga balma mais danga beugeu xalliss lol té yaw say at barri na Démal diamou dji sunu borom té bayi afair yi ak wally Toubal yalla ci li wéssou sa aduna ci ay reukh reukh.

    Reply
  • Giin thieus démal ligueyi escro q tu es

    Reply
  • Tu es un faux tube

    Reply
  • Ce que je ne comprends pas est pourquoi il a accepté le contrat de plus rajouté des dates s'il savait à l'avance qu'il était impossible de faire le concert oufff

    Reply
  • Ah ok kon nonou la démé ahh man ma fogon ni guin thiéss mo mom à faire yi sakh

    Reply
  • Blah Blah blah thione seck is very Fake , fayal khalisu diabour , yaw miyy def ayy faux billiett lounu la wakhal yaw , niakk nga persalitéé trop , kholaal si yousou ndour nimou amee classs doko guis sii yii moukk royall si mooom waay ishhh

    Reply
  • Vraiment thione pa bou rèw ga beugu ay tèseune tè do wax deugu

    Reply
  • Ana justice louye sen ligueye

    Reply
  • Thione do dra ana 34 milliardair faux billet yi

    Reply
  • Non mais commentaire yi dangay reh batass quoi nit yi gnongui Melni kou feke histoire bi yeup. Amna gno khamne mome gnongui wote deug te ils sont irrespectueux. Yallah rek moxam. Faralouma Ken Nak mais nit dougnouko juge si passé kasse. Wasalam

    Reply
  • Papa thione moytoul senegal degnouye cible nit yak ko mba mou yakou ta kou gneup toufli nga toye

    Reply
  • I'm lost.

    Reply
  • guin thieuss

    Reply
  • Thione delolène guinn teuss khalissam

    Reply
  • Monsieur Seck, vous avez un grand cœur !

    Reply
  • Yaw koyap wally ya takh

    Reply
  • Yaw go

    Reply
  • C faux

    Reply
  • C pas vrait

    Reply
  • You dafa sonal thione wala thione mo sokhoré you 😀

    Reply
  • Ce qui vous montre que ce vieux est un escroq, le nombre de "entre temps" qu'il a prononcé.

    Reply
  • Vraiment thione tu n’est pas un homme honnête..... Arrête trop c’est trop!!!!

    Reply
  • Moi je n'écoute pas la musique mais du courage comme ça la vie . accrochez vous et prenez votre chemin tout droit

    Reply
  • Diokhléne ko khalissam way mogeun thiow li

    Reply
  • Bilay tu dis vrai papa thione.dagnoula yapp rek.mais mougnoul légui mou dieh

    Reply
  • Looool.père bi dey feine

    Reply
  • Deugue rk nga wakh nafèkh rk mo doul bgue dgue degue lou ler nga fi tk ak ay preuve merci rk sènègal lou len woroul rk lagne wèrène tè

    Reply
  • Yéna togne dh ko masol guis diko diokh khalis nafékhe bakhol

    Reply
  • Kou nafèkkoul xamnani Ya nèk si degue thione tè lèral ngako bamou lère nagne lèp si yone rk ngako tèk fami sek nak dagn Lèna singli xam nagn liko waral lèp c wali ki drange mai nak dinagne dè mounouniou si mome dara

    Reply
  • Thione bilaye dinga lakk niou Bari boo baalèwoul lingafi wakh tognoko bénn yone.sènègalai yi naniou mandou bougnou xamoul tè bagn Di jujè ET un peu d respect pour thione aprè tou waynafi lou takh mou meritè respè senegalè yi

    Reply
  • Papa thione a raison

    Reply
  • Thione le vrai domèram

    Reply
  • Wawaw deugeu rek gaye wakh papa thione

    Reply
  • Merci papa thione c claire et net

    Reply
  • Tu n'as rien à expliquer yaw diouboulo et puis mak nga li la war moye dem diamou yalla mo gueuneu si yaw todjoulou féne

    Reply
  • on attend la réponse de guin Thieusse

    Reply
  • Papa thione makk gua wayy ..demal makka gnanal sa dome wakh ji beurina

    Reply
  • fans club wally https://www.youtube.com/watch?v=vXZ_F8QMoe8

    Reply
  • La famille seck là jai pa trop de confience en eux

    Reply
  • papa thione, wally dafa warra kholate entouragame ak ay conseiller yéme nit gni gueumougnou darra

    Reply
  • *bonjour chers compatriotes. Mon mari et moi adorons chanter. Nous avons repris stay de Rihanna. Nous sommes en Asie et y représentons notre Sénégal. Merci de nous soutenir en vous abonnant à notre chaine youtube. bisous Disha* https://youtu.be/r1n4waUFu-g

    Reply
  • Thione pour man ya nek si deug par ce que mome organiséwoul dagn ka mandatè ta fay gua xaliss bi si kanamam kouka mandatè guin thieusss dala beugua diakhasel senegalais

    Reply
  • Merci papa thione.

    Reply
  • 1 tu appelles guinthieus pour pour kil soi témoin kan tu remets l’argent 2 tu sors de la salle pour l’appeler pourquoi pas devant les gens? 3 tu attendais à qu’il te rousse comme disent les galsen 4 tu lui fais sortir de la Sall car guinthieuss suivait pas ta logique 5 tu remets l’argent à l’autre après l’avoir sorti de la sall ?🤷🏾‍♂️ 6 et pourquoi pourquoi pas remettre l’argent à guinthieus devant l’autre c’est plus simple non 👎 Bon ça engage que moi c’est mon analyse et ça engage que moi franchement je v dire papa nous prends pas pour des débile wassalam👨🏾‍✈️✅

    Reply
  • Ne jugez pas de ce que vous ne savez pas ne donnez pas raison à qui que ce soit sans preuves fiables. Ne dénigrez pas Thione Seck c'est un Père de Famille.

    Reply
  • No thione toi t'ai rigolo koi

    Reply
  • Heyy Heyy Heyyyyyyyy Thoine Seck doff naa nak🤣🤣🤣🤣

    Reply
  • tu e 1manteur vieux imbécile que é

    Reply
  • Thione n'a escroquè personne puisqu 'il a rendu l'argent. La question qui se pose est , il devait le rendre a guinn teuss ou bien à edmont?

    Reply
  • ce famille seck nous fait vaiment chier avec des histoires de faux billets et des faut contrat, et des concerts de fiasco, bande d'escrocs

    Reply
  • thanks so much papa thione may god bless you

    Reply
  • Le sénégalais se fait une opinion sans pour autant se baser sur les faits. Guine Thieuss n a pas raison.

    Reply
  • Guin Thieuss doit poursuivre Edmond et non Thione Seck. Thione Seck a raison

    Reply
  • thione sa dome yaw tagueko tele bayi ake adouna sa dome kalela loutakhe doko gere rele sa bop bayiko ake bite niokoye signe le ake contra

    Reply
  • tu fais que confirmer ce qu 'a dit Guin Thieuss

    Reply
  • Danga buege xaliss louladall molako ték jobou sa dome joboll

    Reply
  • Bravo papà thione deugue rek moy moudiou

    Reply
  • Doul rek fay len khalisou diambou bi

    Reply

Add Comments